Children school for everyone and every dayall i need Children school for
Everyone and every day all i need
Je demande pas grand-chose un sac un cahier
Etre un bon camarade de classe voilà mon Souhait Qu'on m'enseigne mon
Histoire et celle du monde entier Pourquoi l'enfant d'en face lui tous les jours y a
Accès?
Diangoum khalé yi moniou sokhal
Fi thi suniou reew thi biték fénéne
Khalé yi daniou lén wara dalal école
Nguir niou meuna diangui way
Kham sa borom kham sa reew kham sa demb
Nguir meuna doni njite euleuk
Dieundeul ko khalima ak batakhal ak alouwa
Goungué ko mou diangui
Children school for everyone and every dayalli need
Children school for everyone and every dayall i need
La la lala la lala la lalalala laa all i need La la lala la lala la lalalala laa all i need
Définitivement poser ma pèle car ça je n'en ai pas l'âge
Du ciment dans ma gamelle je retourne à mon ferraillage
Mais je veux rire je veux danser comme tous les autres
Je ne suis pas né au bon endroit j'en viens
Même à penser que c'est ma faute
Yaw mi wadiour bayal sa war té def sa waréefyobouko
Daara
Tagate lén ndaw gni khamal lén ni reex mi métina
Nguir niou meuna niaffé waay
Niakk diangue mossiba la thi reew boumou meuna done
Rawatina neew di doolé yi
Kone amoul adji amoul aas amoul khadiak sén diangal lén ndaw gni
Children school for everyone and every dayall i need Children school for everyone and
Every dayall i need
La la lala la lala la lalalala laa all i need
La la lala la lala la lalalala laa all i need