Back to Top

Karim Diouf - Québégalais Lyrics

Karim Diouf - Québégalais Lyrics

Bo guissé adouna ni mou mela takh ma wakhé ni
Guor dafa wara Gorguolu tambeléko tcha bamouye ndaw
Te khame ni wadjour, sen djan mome watchna
Dakh situation métiwone na lolo takhone ma guene keurgui
Boumou takh Baye Boye mane guen Fatéma
Sama djambar dé umpoulene, ligguéye bourré dafnako wayé
Art dafa né tchi mane di sama khol ma djapo koq sama foula ak fayda
Douté sayouma djoulé niane Fallahou yalla Karim mou wone gnou yone wi.
Sama Yaye tagounala, sama baye tagounala bougnou démé ba
Ame fa niari wére, Xeuye souba gnibissi
Xam sa bope dafa gueun nit gni wakh la li gua done
Gnoune dé khame na gou gnoye kan, gnoye kan, Xame na gnou li gnou done
Bi gnou deudé ba wakhtanék guéguénaye daldi kholate mbirbi
Ba gnou keuyeu ba khol louye Canada mo nekh gnou tok
Adouna nou mou mél
Bo gnibé gnouni la canadien bi , gua yekessi fi gnou ni la africainbi
Yefi khamatouma mane loumay nourrol.
Fi ken doula wakh loy deff, do wakhit ken lou mouye def
Yaye khol li gueune tchi yaw gua deff ko tok
Sama Yaye fagounala, sama Baye tagounala, bougnou démé ba
Ame fa niari were, Xeuye souba gnibissi

Gnoune dé khame na gnou gnoye kan, gnoye kan, Xame na gnou li gnou done
Bi gnou teudé ba wakhtanék guéguénaye daldi kholate mbirbi
Ba gnou keuyé ba knol louye québécois mou nekh gnou tok
Fan moye sa yone, wakh ma sa yone
Gadou sa hilaire awe sa yonou tol
Fane moye sa yone, wakh ma sa yone
Fane moye sa yone, wakh ma sa yone
Tollyi, tollyi
Tollyi, tollyi, tollyi, tollyi, tollyi yaye Boye, gnou baye tollyidakh
Mou djour soukar
Fane moye sa yone, wakh ma sa yone
Gadou sa hilaire awe sa yonou tol
Bagnou teudé ba wakhtanak guéguénaye daldi kholate mbirbi
Ba gnou kheuyé ba knol louye Montréal mou nekh gnou tok
Fane moye sa yone wakh ma sa yone
Gadou sa hilaire awe sa yonou tol
Tollyi, tollyi
Tollyi, tollyi, tollyi, tollyi, tollyi yaye Boye, gnou baye tollyi dakh mou
Taw soukar
Fane moye sa yone wakh ma sa yone
Gadou sa hilaire awe sa yonou tol
Tollyi, tollyi, tollyi, tollyi, tollyi yew
Gnoune dal Bou naré natt tchi tol ya la djoggué
Fane moye sa yone, wakh ma sa yone
Gadou sa hilaire awe sa yonou tol
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Elage Diouf, Karim Diouf
Copyright: Lyrics © Évangeline/APEM

Back to: Karim Diouf

Tags:
No tags yet