Back to Top

fadel faty - Faatèli Lyrics

fadel faty - Faatèli Lyrics

Fii hame perte dégniou ko tale
Lou way di wotè dang ko nourou nite nga héll na dale saga ak fène bou dèmé ba done ligniou wara mene liii rire gui rire ba lendem dieuk fii nite dohatoul diamou roy roy ba dak pire gnioun fou gniou dieum ak kougn geme yone kane ngay diamou viudè nome nga gemou ligniouy gene fecel fiii ay hétou dore la barki Serignie diw ak diw ak dore et la rèk mani pour gniou ame ligniou gena begue nagniou fèhé gniak ligniou gena begue ay nèw youy doh holl fèbar gena soh begue dank linga sèh hagn sa morom limou yore begue tour ak buzz diay principe gena gaw ligniouy gene dème di gene giss hèllou nite ki done na mala han!!
Bagnia sètane halè mene na gniak
Dieul gale lagniou gene tane

Ligniouy gagne sounou holl la nèk
Fèbar touh dii gena sagnie
Gena sagnie ba kotie gagne la nangou linga yore
Ndahh giss nagniou talent dou mene
Fii gnioufi epou kopar rèk dèff ndiouma
Té kene doulèn topou cii dara badolo bangii dèè

Intèlèctuel ay Serignie wara inspire
Intellectual la presse wara informe
Diay ngor sène askane ngir sène intérêt

La jeunesse en pane d'espoir
Après wade macky
Sounou tax cii sèn caise noir bokou kogn beuri relève lole loloy cauchemar
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: ABDOULAYE WONE, FADEL FATY
Copyright: Lyrics © ONErpm

Back to: fadel faty

fadel faty - Faatèli Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: fadel faty
Language: English
Length: 3:02
Written by: ABDOULAYE WONE, FADEL FATY

Tags:
No tags yet