Back to Top

Cheikh Lo - DOYAL NANIOU Lyrics

Cheikh Lo - DOYAL NANIOU Lyrics

Ohé Africa ye Africa united, united
Gnoune domou Africa doyal naniou coup d'état
Thi fénéne ak foudoul Africa

Coup d'état day diour M'Bagnel, coup d'état day soukheut bop sa bof
Té sétlou na gnou fou mou Khassa am, yagga yagga dina fa amat
Coup d'état ba dédiou, ndéy ak Baay doto woloy
Coup d'état ba dédiou, thiamogne ak ndéydior doto wolou
Coup d'état ba dédiou ; kou seukheut ngafog né dalay woutou

Africa ho, Africa ho, Africa Ho, united united, stop war
Souma khel dém sa, Thomas Sankara peulh bou
Ratét binewone bourkina faso

Ak kabila si Congo, ama guei Robert sa Cote d'Ivoire
William Tolbert ak Samuel do sa Liberia, gnéréré sa Tanzanie
Moussa Traoré thia Mali, ana tché ke verra, nino vern thia
Guinée Bissao, kougnousi réyoul, teuthie nanioula, guéne nanioula
Mba niou boomla, liniou geuneulone sakh, kounioufi diokham
Réw, bo dokha loul niou dindila si kaw diongante
Fi ak khér diogoul, bal takkoul, khéthie nawoul
Peundeu diogoul, guéthie gui débordéwoul
Diam rék laniou y am si Senegal ak liko weur

La paix en Casamance, la paix au Mali, di mouslou si rebellion
Naniou wéér nganayi

Niou khol si Ukraine, ho way Russie, ho wayayo la Syrie
Ho wayayo yo Afghanistan, Centre Africa ho, thiowli barina
Mandela, Mandela, Mandela oh South Africa, doyalnanou coup d'état
Nioune domou Africa doyal ma nou coup d'état

Té sétlou na gnou fou mou massa am, yagga yagga dina fa amat

Coup d'état ba dédiou ; kou seukheut ngatok né dalay woutou
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: MAMADOU MOUSTAPHA LO
Copyright: Lyrics © WAGRAM PUBLISHING, Warner Chappell Music, Inc.

Back to: Cheikh Lo

Cheikh Lo - DOYAL NANIOU Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Cheikh Lo
Written by: MAMADOU MOUSTAPHA LO
[Correct Info]
Tags:
No tags yet